Wolof stringlengths 10 455 | emotion stringclasses 7 values |
|---|---|
Bo gisee ma gën laa néew alal ak i doom. " | disgust |
waaye leer, lu mu ëmb, fésal ko. | disgust |
Ndax li Yàlla sàkk amoon na sikk? | neutral |
Ce tare:) si pretul suna biiinnneeee!;;) | surprise |
Ngir-yàlla tànnal beneen tur.', | surprise |
Yeena ko seede bésub tey jii." | neutral |
Su ko defee ñu dëkkewaat seen suufas bopp." | neutral |
Les signes (aayaate) sont partout. | neutral |
Xamlu ku xam ,day dolli xam. | neutral |
Lan lañuy def ak xam-xam boobu ñu am? | neutral |
Nóoyin def na lépp li ko Yàlla santoon. | neutral |
Moom la Mbind mi wax ne:"Ku jub amul, du kenn sax. | anger |
Duñu naan biiñ ba tey jii ndax wormaal seen santaaney maam. | neutral |
jubóo te jubu ñu ñoo ko waral. | neutral |
By Stormen, en mooy weer, | neutral |
Ndaxte kàttanu fas yaa ngi ci seeni gémmiñ ak ci seeni geen. | disgust |
Lot ne ca xiiñidxaapaʼ bizuubacaʼ diidxaʼ ne bixooñecaʼ de Sodoma. | disgust |
Yàlla daldi koy rey moom lu tollu ci téeméeri at. | disgust |
mi mu jagleel say àndandoo." | neutral |
Yexowa dafa sàkk góor ak jigéen ngir ñu jàppalante ci seen biir. | neutral |
Dina ko dóor ay dóor yu metti, jox ko añub ñi gëmul Yàlla. | disgust |
Dañuy dinañu fàtaliku yaw. | neutral |
ak biddiiwub Refan, bi ñu daan bokkaaleel Yàlla, | neutral |
ak yeen ñi ko ragal, mag ak ndaw." | fear |
Indeed book de wicked est Sijjeen. | disgust |
Laajleen ko; magum jëmm la, te man na tontul boppam." | anger |
Ana lu waral nga namma tas dëkk bu Aji Sax ji séddoo?" | anger |
Yexowa dafa bëgg neexal ñi koy jaamu dëgg. | neutral |
Kuy wax googu kàddu, ag leer fenkalu la." | neutral |
Dafa fekk rekk ne ci làkku fràñse la gën a siiwe. | neutral |
yéen ñi ko ragal, mag ak ndaw." | fear |
Waxal ne: "Yàlla, moom Kenn la (jenn Yàlla rekk la). | neutral |
Nangeen ñów ci tàntu Yexowa. | neutral |
Junniy junnee nga koy jaamu, | neutral |
Fa la léen séen wërsëg di fekk subaak ngoon. | neutral |
Awa tontu ko ne: "Man nanoo lekk ci doomi garabi tool bi kay. | disgust |
Su doon genn-wàllu nguur gi sax, dees na la ko jox!" | neutral |
bi ngeen daan jaamu | neutral |
Jox leeni doom lu jafe la. | neutral |
Xanaa xamuloo ne mën naa laaj sama Baay ay junniy malaaka ngir ñu muccal ma ? ' | anger |
" En fait, je ne suis ni l'un ni l'autre, je suis juif. " | neutral |
Juróom ñaari fan nag ngay négandiku, ba ma fekksi la fa, xamal la looy def." | neutral |
Waaye su lalee pexem wor de, dina dee." | fear |
musal ko ci ku koy teg àtteb dee. | anger |
Waaye Lóot ak njabootam dañu doon yéexantu. | neutral |
Ndaxte Seytaane wàcc na ci yéen, ànd ak mer mu tàng, ndaxte xam na ne, jot gi ko dese barewul." | neutral |
Dañu leen di bañ waaye itam dañu leen di xawa ragal. | fear |
di yool, ba wis kuy réy-réylu. | joy |
te noor ak nawet lay doon. | joy |
Ci Sunu Boroom lanu joge Ca Moom lanuy dellu! | neutral |
Sob, lépp lu ñuy aaye yaa koy def, luñu nëbb yaa koy luqati. | neutral |
Loolu moo tax ngeen gis te dégg kéemaan yii. ' | neutral |
C'est vrai waay, pa bi dafa wara go. | neutral |
Noonu lay deme ak ñiy weddi ak aji gëm yi. | neutral |
Te sama dige Booroom dëgg la." | neutral |
Dafa mas a firnde barke ci li jëm ci jur doom yu bare. " | joy |
Kon sawara wi moo gën a yaatu safara si. | neutral |
yam ci tawfeex ci sag ak sañ-sañ. | neutral |
Képp ku nekk ci asamaan dafay topp bu baax Yexowa Yàlla. | disgust |
ba kera mu yégal njub, ba daan. | sadness |
Seetal fi ñuy defe suñu ndaje yi ak ni ñuy jaamoo Yàlla. | neutral |
Ngir nu nattu léen kan ci ñoom a gën a rafet jëf. | neutral |
Bu dee guddi àjjuma ñu wàccee ko juróom ñaari yoon. | fear |
Lóot nag soññ leen, ba ñu dal këram, mu ganale leen. | anger |
Tey jii, Yexowa dina ma dimbali ba ma rey la. ' | neutral |
Nóoyin ak doomam yi déggal nañu Yexowa te komaase nañu tabax gaal googu mel ni kees. | disgust |
AS - Dinañu ko dëgg bu neexee Yàlla. | neutral |
Ginnaaw loolu, mu tànn ci seen biir xale yu góor yi gën a rafet te gën a am xel. | neutral |
Dañu sàcc lu Yàlla moom. | disgust |
Lu tax ñu war a gërëm Yexowa ndax njot gi mu maye? | anger |
Yaw ak sa njaboot ak say xarit dingeen am dund bu neex ba fàww. | neutral |
Yàlla tànnoon na waa Israyil ngir ñu nekk ay seedeem. | neutral |
Bu ma lekkoon tey ci yàppu saraxas póotum bàkkaar bi, ndax dina neex Aji Sax ji?" | neutral |
waaye day dàq ñiy def lu bon." | disgust |
Lu ko moy dinañu daanu ci seen kanami noon." | fear |
Ndax du ci saw tur lanu daa defe ay kéemaan yu bare?" | neutral |
Yalla rekk-ay Yalla te li Mu yellool Moom rekk-a ko yellool. | neutral |
ak kéemaanam yi ñeel doom aadama yi. | neutral |
Mu ne ko: "Moom de, ma nga ca kër Makir doomu Amiyel, ca dëkk ba ñuy wax Lodebar." | neutral |
Sama boroom yal na nga nu nagul,yaw ay aji dégg jiy aji xam. | neutral |
mbind mi dafa ne:"ana ku xam xalaatu boroom bi?ku ko doon digal?" | neutral |
te xam mbaax, gi ci kàddug Yàlla, ak kéemaani jamono jiy ñëw, | joy |
Fa nga jaare Yàlla la gaa ña jiitu di wër ba tay | fear |
bégleen te bànneexu, ndax seen yool dina réy ci laaxira. ndaxte noonu lañu daan fitnaale yonent yi fi jiitu. | joy |
jëmmi-jamono j-: taŋ b-. dinañu gise jeneen jëmmi-jamono. | neutral |
Waaye, duggewuñ ko woon lu dul wéyal nootaange bi. | neutral |
bah ca te prend comme ca direct? | neutral |
Soo ko defee, dinga ko aar ci biir buy daw. | joy |
Bu gumba dee wommant moroomam nag, kon dinañu daanu ñoom ñaar ci kàmb. | neutral |
Waaye soo ko deful, na la bir ne dinga dee, yaak sa waa kër yépp." | sadness |
Lan lañu mën a jàng ci li dal jabaru Lóot ? | neutral |
Ci turu Yàlla Yërëmaakoon bi, Jaglewaakoon bi. | anger |
Bu ko neexoon mu def ko jàmm, baaxe ko réew mépp; bu ko neexoon yit mu soppi ko safaan ba, def ko fitna. | disgust |
Balaam moom, mënul gis malaaka mi. | disgust |
Musa:"yo apek yu nek ngono..." | neutral |
Esekiya ne ko: "Mboolem lu nekk sama biir kër, gis nañu ko. | neutral |
Mbaa du dangaa lekk ca garab, ga ma la aaye, waay?" | disgust |
Xamuleen ko nag; man maa ko xam. | neutral |
luy doon muju ki weddi te dëng?" | disgust |
Bés bi Yàlla di alag ñu bon ñi dina bett ñépp. | fear |
Wolof Emotion Analysis Corpus
Dataset Description
This dataset contains emotion-labeled text data in Wolof for emotion classification (joy, sadness, anger, fear, surprise, disgust, neutral). Emotions were extracted and processed from the English meanings of the sentences using the model j-hartmann/emotion-english-distilroberta-base. The dataset is part of a larger collection of African language emotion analysis resources.
Dataset Statistics
- Total samples: 320,611
- Joy: 32636 (10.2%)
- Sadness: 19793 (6.2%)
- Anger: 22854 (7.1%)
- Fear: 13260 (4.1%)
- Surprise: 24477 (7.6%)
- Disgust: 26030 (8.1%)
- Neutral: 181561 (56.6%)
Dataset Structure
Data Fields
- Text Column: Contains the original text in Wolof
- emotion: Emotion label (joy, sadness, anger, fear, surprise, disgust, neutral)
Data Splits
This dataset contains a single split with all the processed data.
Data Processing
The emotion labels were generated using:
- Model:
j-hartmann/emotion-english-distilroberta-base - Processing: Batch processing with optimization for efficiency
- Deduplication: Duplicate entries were removed based on text content
Usage
from datasets import load_dataset
# Load the dataset
dataset = load_dataset("michsethowusu/wolof-emotions-corpus")
# Access the data
print(dataset['train'][0])
Citation
If you use this dataset in your research, please cite:
@dataset{wolof_emotions_corpus,
title={Wolof Emotions Corpus},
author={Mich-Seth Owusu},
year={2025},
url={https://huggingface.co/datasets/michsethowusu/wolof-emotions-corpus}
}
License
This dataset is released under the MIT License.
Contact
For questions or issues regarding this dataset, please open an issue on the dataset repository.
Dataset Creation
Date: 2025-07-04 Processing Pipeline: Automated emotion analysis using HuggingFace Transformers Quality Control: Deduplication and batch processing optimizations applied
- Downloads last month
- 13